Confidence d’Alice : « sama dieukeur day begue may photo sama S »

Par , publié le .

People

« Mane dama am louma méti sama dieukeur nékoufi mogui extérieur mais à  chaque fois day begue may foto sama ana ndiaye bi dikoko envoyé ba barki demb mou wakhat mako ma bagn mou méré ma soumako envoyé sms douma tontou,ba demb mouné ma louma beug ngamay défal wala do am diam.bobou ba légui wowouma té sou mako wowé pour niou wakhtane douma falé dama diakhlé instant bi. Dama sokhla kouma dimbali », confie Alice, une jeune femme de 27 ans.

1 commentaire

  1. Diouf Abdoul Aziz
    Diouf Abdoul Aziz
    10 janvier 2021 at 15h14

    Non il faut refuser woroul avc Les réseaux sociaux

    Répondre
Laisser un commentaire

Votre email ne sera pas publié. Champ obligatoire (*)

Défiler vers le haut
Suivez en DIRECT/LIVE Les Manifestations Du Lundi 08 Mars 2021Cliquez-ici